Dangay fo ci sa waxtu, ci biir: ku njëkk tann pier, kaper walla siso, tann bi di dem te telefon bi di dem ci keneen ku mu bokkal, di tann moom itam. Kon 3, 2, 1 te loxo yi di woneu. Kaper dafa dàq pier, siso dafa dàq kaper, pier dafa dàq siso. Ñu bokk benn? Foat leen. Gagné 3 loxo ngir gagné match bi.
Mini Games GO